Takhâwâyou ndawgni thi wattou sounna ak jarigne khète bi

Wakhtânekatebi : Ousmane Galadio Kâ

Mélokâne bi

Sèllal, yittéwô bou kawé thi Alkhourâne ak Sounna, dégg ak wômmatou, sâmm wakhtou, ândandô you bâkh, di déllou sâssouné thi borôm expérience yi thi borôm kham-khamyi.

Download
Binndal sap guiss guiss kiy saytu xeüt wii

Tèkhanetal you ajou thi kham-kham: