Jourômgnâr yiñuy kéral ëllëk

Wakhtânekatebi : Mor Kébé

Khôlâte: Djibril Dièye

Mélokâne bi

Wakhtâne mi ngui aju jurôm jikko ñiko jikkowô Yalla dina lène kéral thi kéram ga béss bô xamné bénène du am budul bosam

Download
Binndal sap guiss guiss kiy saytu xeüt wii

Tèkhanetal you ajou thi kham-kham: