Lômpognouk ngueum

Wakhtânekatebi : Mor Kébé

Khôlâte: Djibril Dièye

Mélokâne bi

Wakhtâne mi ngui jeum thi lane môy nguem ak sabab yiy takh mou lômpôgn ak nougnoukoy sâfarâ

Download
Binndal sap guiss guiss kiy saytu xeüt wii

Tèkhanetal you ajou thi kham-kham: