- ولوف
- ولوف
Mi ngi juddo jidda ci 09-11-1381 ci gàdday gi. Amna Bak ci ŋàŋum lislam ci jànŋukày bu kawé bi ñu duppé Al-Malik Abdul Aziz bi ci jidda ci 1406 ci gàddày gi.Ak Majester ci Fikh ak Ciosànam ci jànŋukày bu kawé bi ñu duppé Ummul Qurà bi ci Makka, binndoone ci (Ay léral ci xàc bu njëkk ci ay dëppo yu Ibn Ruchd ci térém bi di Bidàyatul Mujtahid wa Nihàyatul Muqtasid) ci atum 1412 ci gàddày gi. Ak Doctora ci fikh ci atum 1419 ci gàddày gi. Ni mu améwone lijàssa ci Hafs ci cheikh Doctor Aymane Ruchdi Suwéyd ci 1407 ci gàddày gi.
- ولوف
- ولوف
Cheikh Mahmoud Khalîl Al-Houssary môy serignou mbôlème jânggkatou égipteyi, di jîtémbôtâyou jânggkatou al-khourane yithi addounabi. Mi ngui jouddou thi tâmbalik atoum ajj thi atoum 1335 thi gâddây gui tôllôk 17 sèptembar thi atoum 1917 thi atoup toubap. Thi deukk bougnou douppé Chabrae namla bi jôkk thi tâMahmoud Khalîl Al-Houssarynetâ tho sôwwou égipte. Mi ngui fâtou thi ngônou altiné16 mouhârram atoum 1401 thi gâday gui tôllôk 24 nôwembar 1980 thi atoum toubap guinnâw joulli gué. Limou enregistré thi alkhourâne: kâmil thihafs jogué thi âssim atoum 1961 thi warch bi jogué thi nâfi' 1964 qâroune ak doûrî jogué thi abî Amr bou Basra thi atoup 1968, kâmil biy jânggalé thi 1969, kâmil bou ând ak piri thi 1873. Yimou tâlîf: attèy jânng al-khourâne, foukki jânggine thi Ach-châtibiyya ak Ad-dourra, mândargâm kham fi ngua wara tâmmbalé ak fi ngua wara takhawé thi jamono bi ngua jângg al-khourâne, Oubbité guou reuy gui thi mouslou ak kâbbar, jèkhite bi geuna rafète thi dounndoup foukkak gnènnti jânggkate yi, ânddak al-khourâne bou tèdd bi, njângginou warch joggé thi Nâfi bou madîna, njângguinoup Doûrî bi jogé thi Abî Amr Al-Basrî, lèrou kholyi thi njânggoum imâm Yaqoûb, yônn wou yômb nguir njângginoup imam Abî Jâfar, bèglé gou rafète thi dajalé digganeté Ach-Châtibiyya ak Ad-Dourra, yônn bou bèss thi kham-khamou ni gnouy jânggé al-lhourâne
- ولوف
Cheikh Abou Bakr Ach-châtiry mi ngui joudd atoum 1970 thi jidda môy yilimânou joumây Al-Fourqâne thi Nassîm Jidda. Mi ngui dègnth sokhna am thi gnènnti dôm. Dâkkanetalam môye Abou Abdourrahmane. Ay lijâssâm thi jângg: dipolomou jângg Al-khourâne bou tèddbi thi hafs bi jogé thi Âssim thi serignam bî di Aymane Rouchdî Souwayd thi atoum 1416 thi gâddây gui, wayé thi jèkhinetaloup atoup 1420 thi gâdây gui amna tamite diplomoup mâjèstèr thi saytou alal.
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
Touram môy: Abdur Rachid Ibn Cheikh Ali Sufy. Lu aju ci démbam: mi ngi juddi ci atum 1964 ci Somali. Pappam môy fóré bi tudd Ali Ibn Abdur Rahmane Sufy (Ubbékabup Somali ak kafa gëna kawé ci jâŋŋup Al-xuràn) muy kifa ngëkka dugal ak tassâré xamxam ngaŋŋu Al-xurân ak ngaŋŋine yi, ñu bari ci ay borô xamxam jaŋŋénañ ci môm, tabaxna ay école akiy centar yu limu ngir ñufay jàŋŋ al-xurân. Mi mujj ci jàkka yôyu môy bu sîw bici Mogadîsiô bi ñu duppé Jàkka Cheikh Ali Sufy bi nga xamné fala Abdur Rachide Sufy fala jàŋŋé. Jàruwàyam ci al-xuràn ak sàkku xamxam: mi ngi jàŋŋé ci bàyam ci jotàyu xamxam yimu dàn amal ci jàkkaji ba môkkal ci fukkélu atam. Ginnàwgi mu mu jékku xamxam niñuy jànŋŋé al-xuràn ci hafs jëléko ci Asim, ték ci jurôm ñâr yi dés ci yonu Châtibiyya, bôlékôk déglu faraŋfàccéwu térép Châtibiyya ñatt yôn ba môkkalko. Chatibiyya ap qasida làmiyyala bu Imam Waliyyulla Al-qassim Ibn Fîrra Ach-châtiby (yàlla nako Yàlla yërëm) mingi fàtu ci atum 599 ci gâddày gi qasîdâm gi amna 1173 bayte. Ginnâw gi mu jàŋŋ li jàppandi ci nahw ak fiqh Chafi'î ci bâyam, ba mujjgi mu tukki Egypte ngir môttali jàŋŋgine yi ci Octobre 1981, fôfé la duggé ci jànŋŋukây yu kawéyi ba amfa lijàsa yu kawé yi ci fukki jànŋŋine yi; bôlékôk di jël ay binnd ci borôm xamxamu jànŋŋkatu al-xuràn bu mak bî di Cheikh Muhammad Ibn Ismail Al-hamadàny (yàlla nako Yàlla yërëm) ci Azhar ba amci ñàri lijàsa yu am càllalé baci Yonéntebi (yàlla na Yàlla julli ci môm): 1- ci fukki njàŋŋine yi ci yônu Châtibiyya ak Durra. 2- ci fukki njàŋŋine yi ci yônu At-tayyiba bu imam Al-jazari. Jànŋŋ na itam xamxam rëddup Kàmilbi. Lu aju ci ay jalôrém ak wôtém ci yônu Yàlla: ginnàw bimu nôppé ci njànŋŋam délluna Somali wuutu bàyam ci jité ak janŋŋalé ca jàkkaja ginnàw bimu fébaré. Faréna jànŋŋalé xamxami Al-xuràn bu téddbi ci faculté bi màcc ci xamxami lislàm té jôkku ci Azhar. Mbôlo bu bari ci Somali ak Qatar jariñunañu ci binnd yôyu. Mi ngi éksi Qatar ci atum 1991, ministérup yi aju may yiñudul dônn ka ci lislàm tànnko mu jîté aka xutba ci jumày Anas Ibn Malik (yàlla nako Yàlla yërëm) ci marsé centaral bi. Amna ay yëŋŋatu yu aju ci wôté jëmé ci Yàlla ci Qatar. Niki nônu itam dafay amal ay binnd akiy waxtàn bôlékôk téwé ay séminaire akiy ndajé yu aju ci lislàm rawatina ca tugal. Démna itam Bahrayni ay yôn. Amna ay njànŋŋ yu ñuko enresistérél ci Sadal Fajr ci sitam. Sitam môy: www.abdulrashid.net
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
Mi ngi juddoo Màkka. Amna bak bookk ci ñici ràññéku ci wàllup Al-Xuràn ak sunna ak cossànu diiné ci universiep Ummoul khurà. Ci atum1412 ci gàddày gi nékkna kuñu jiital foofé ci xamxamam ci waallu nŋàggiinum alxuràn. Ci atup 1416 ci gàddày gi la am majester ci al-xuràn akiy xamxamam ci universitép Ummul xurà ci jàŋŋinu al-xuràn. Ci atup 1416 ci gàddày gi la am doctoorà ciy poñ yi gëna kawé ci facultép Al-xuràn akiy xamxamam ci université boobu ci pàccup jàŋŋin yi. Ci atup 1422 ci gàddày gi lañ kofa fal Ustàs buy jàppalé ci facultép wooté ak cossànu diiné. Ci at boobu lañuko fal mu jiité pàcc gi fété ci jàŋŋin yi ba ci diggu atum 1424 ci gàdày gi. Ginàw loolu ministér biy saytu mbiri lislàm ak mayé yiñudul doon ak wooté ak téktalé défko yilimàn ci jàkkàp Al-xayf ci Minà. Ci atum 1428 ci gàdàygi la buuru arabi sawdite bii di Abdalla diglé ñu défko yilimàn ci kàbagi.
- ولوف
- ولوف
- ولوف
Jàŋŋkatu alxuràne la bu juddoo Médine ci atum 1364 ci gàdàygi, fala magé yaroofa jàŋŋéfa ci Darul hadis ginnàw gi mu dem najàh topp mu dem ci colés ba mujjé ci écolup xaralé yi jëm ci isine. Jàŋŋéna ci ay kàŋŋàm: Omar Alhaydari, Ahmad Az-Zayyàte, Abdulla Al-Ghunaymàn. Boolénaci fikh ak passpass ak charia. Fétéwoona ak ligé yu takku, niki: Ustas ci xaralép usine, ci Alxuràn ci ecolup ubay Ibn kab ci médine, Ustas buy wootu ci universitep Medine. Ci atup 1406 ci gàddày gi la tàmbalé jiité ci jàkkày Médine. Bookkna ci attékate yi màcc ci Alxuràne.
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف
- ولوف