Takhawâyou Jâkk thi tabakh socétèp joullite
Mélokâne bi
1- Lane môy Jâkka 2- Solos Jâkka thi lislâm 3- Lènn thi isouwârou Jâkka thi lislâm 4- Jèkhitou Jâkka thi dounndou joullite 5- Ay dêggine akiy jeuf you jara défarâte
*** Sô beuggé nite gou mate nite woutal Jâkka jou mate Jâkk ***
- 1
Takhawâyou Jâkk thi tabakh socétèp joullite
MP3 24 MB 2019-05-02
Tèkhanetal you ajou thi kham-kham: