Yawmal qiyâma

Wakhtânekatebi : Ibrahim Khali Lô

Khôlâte: Djibril Dièye

Mélokâne bi

Waxtàn wi gui ajou ci lèral faratâp fâttalikou déé ak wâjalko, ak jârouwây yi nite ki de rômb ba yégg thi kërëm gou moujj, ak toudd adîssoup Barâ Ibn zib (Yalla nako Yalla gërëm), ak saba yiy taxa dugg jana ak mucc ci safara

Download
Binndal sap guiss guiss kiy saytu xeüt wii

Tèkhanetal you ajou thi kham-kham: