-
Sâdoul Ghâmidî "Limou mbiryi : 221"
Mélokâne bi :Sâdou dômou Saîd Al- Ghâmidî sîwé bâtam bou nèkh bi, yilimâne ak khoutebakatou jâkka bou gnouy wakh Kânou -Dammam- thi Arabi Sawdite, di aji sawtou centarou al-khourâne bi gnou douppé Imâm Ach-Châtibî tèm nèkk thi Dammam.