-
Fâriss Abbâd "Limou mbiryi : 28"
Mélokâne bi :Fâriss Abbâd: mi ngui thiôssânô Yémène.Di borôm bâte bou nèkh té râgnèkou. Enrezistéréna ay téré kham-kham ak Kâmil bou mate. Bôkkna thi yolimânou jâkka Alioune dômou Abî Tâlib thi Ad-dawha thi sôwwou Arabi Sawdite