-
Buroop ndimbalanté ngir wooté ak yé ñi né Ar-Rabwa "Limou mbiryi : 9739"
Mélokâne bi :Mbootàyup way def lu bàx ci wooté boo xamné cik goorgoorlu ak ak saraxé way défal Yalla la taxawé, ci ndigeül gu bawoo ci Kilifa gi di Abdoulla Aziz Ibn Abdalla Ibn Baz (ki jiité ubbékate yi ci Arabi Sawdite) (Yalla nako yalla yeüreüm) ci Allarba 28-04-1414 ci gàdday gi.
ñiy saytu buroobi nak mooy ministér bi yoré mbiru diiné lislam ak mayyi ak wooté ak jubbanti