Fatwa bouamsolo diam thi dioutiyi

Wakhtânekatebi : Mohammed Ahmed lo

Mélokâne bi

Degue bouwer ak ndiarignme thi tourou yallayi ak melokanamyi,dirdisrou omar bon abdou aziz ak lithi nek thi ay diagn guatt,degkane bouamsolo diam thi diamge katyi ak wete katyi,tawassoul Moylan ak aykhetam ak attem thi lislam.

Download
Binndal sap guiss guiss kiy saytu xeüt wii

Tèkhanetal you ajou thi kham-kham: