Limou mbiryi: 13
MP3 17 / 5 / 1436 , 8/3/2015
Leral niety degnkayi bithi diake:fedali gueguem bouwer,rafetal diame thi waydiour, ak oubbe kouam solo
Nekenathi nontou ay lathe youbari bakounathi:ndakh merouk niari wadiour day waral niakanaguou ak diamouyalla?niane nioy kourelou asahira?
MP3 20 / 1 / 1436 , 13/11/2014
Degue bouwer ak ndiarignme thi tourou yallayi ak melokanamyi,dirdisrou omar bon abdou aziz ak lithi nek thi ay diagn guatt,degkane bouamsolo diam thi diamge katyi ak wete katyi,tawassoul Moylan ak aykhetam ak attem thi lislam.
MP3 19 / 2 / 1437 , 2/12/2015
Nekena thi leral guenelou dioulli yoryor, ak tontou ndakh khouy def ape bida ndakh dina thi am touyaba?...
MP3 10 / 2 / 1437 , 23/11/2015
Nekena thi nontou nakh khoudar yonentela wala walliyou?
MP3 2 / 12 / 1436 , 16/9/2015
li ay oubbele youdiam thi mbiri tabaski aylathie ak aytontou thi mbiri tabaski
MP3 2 / 7 / 1436 , 21/4/2015
Nekena thi nontou ay lathie youbiri boukou nathi:gusguisou islam thi doukol television thi keur, ak ndakala mamoum difaye likorow thi joule…
MP3 24 / 6 / 1436 , 14/4/2015
Lii ay ubbé la 10-03-2015
MP3 22 / 6 / 1436 , 12/4/2015
Nekenathi tontou ay lathie youbari boukounathi: atte fayekou bor, atte diouli witar thi goudi, atte wat ethi loudoul yalla…
MP3 5 / 6 / 1436 , 26/3/2015
Nekenathi nontou ay lathie youbari bouknathi: atteb sede thi fose?...
MP3 15 / 4 / 1436 , 5/2/2015
Nontou lene thi laji youlli ak meloka ak yene…
MP3 14 / 3 / 1436 , 5/1/2015
Ndakh warna thi jigen dioulik jouman,lan motakhale sounit ak sityi, atebe kene ajaka thi tabakh diaka, atebe touddou yalla thi wanak thi diabe…ak dantou you amsolou.
MP3 16 / 2 / 1436 , 9/12/2014
atte yaguou ajirow thi imamam, atte dinde dourou ajifatou thi bambemelam,atta tabakh diaka thi khalisou diaey katou saguaro,ak kenne ajaka thi bobou khalis.
Follow us: