Limou mbiryi: 3
MP3 14 / 5 / 1436 , 5/3/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: léral taaroup lislam bi ngui khamné môy dîné jâmm, akiy téggine you rafète thi dounnd ak gnoudoul joullite. Di tônetou gni gnâwal thi Yonènete Mouhammad (Yalla na Yalla joulli thi môm té dôlliko jâm)
Waxtàn wi dafay leral na lagnouy jeuflaneté ak gnoudoul joullite
MP3 20 / 6 / 1436 , 10/4/2015
Nekena thi leral ni wakhtane diguante dioulityi ak nasaranyi mante nek adak toudou ay sababe yuobari…