Tèkhanetal you ajou thi kham-kham

Fénup wéru Aviril

Fén fébar la bu màgg, ndax mi ngui bookk ci bàkkàr yi gëna ñàw té bone, bookk ci màndarga nàféx, dafay tax nite ki wacc yoonu ngëm. Bookkna ci li tassàroo ci nit ñi lii di "fénup wéru Aviril": mudi né fén ci bess bu njëkk ci wér woowu dagane na ci ludul bénn tëkk wu bawoo ci lislam. Loolu jur ay yaxu yaxu yu bari. Xët gi ñi ngi ko jaglél ci léral àttéy fén ci boopam ak fén ci wéru aviril rawatina

Limou mbiryi: 1

Kheut wi : 1 - Dalé thi : 1
Sap xalàt lu ñu saxalla