Limou mbiryi: 6
MP4 17 / 5 / 1436 , 8/3/2015
Wadjal Lénn déé
MP3 2 / 12 / 1436 , 16/9/2015
Nekana thi lerakl atte ahjj ak kagne kay war , touddou ganeli ahjj ak ay diekhantalam thi khetou islam…
MP3 10 / 10 / 1436 , 27/7/2015
Ay jànggat yu aju ci wéru koor, ak lenn ci sababu yéx gu ndimmbalu Yalla tardé
MP3 20 / 8 / 1436 , 8/6/2015
Soloss waxtàn wi mi ngui gëna feñ ci toxal guy ñuciy toxalal niko mag èu baax daan mànggé
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Dina jaadu ci bépp jullite mu yittéwoo lu aju ci àttéy diiném rawatina wéru koor
MP3 22 / 6 / 1436 , 12/4/2015
Nekena thi toudou diarigne yi ganamague thi werou kor bokounathi :mougne thi mbolem khadiamyi,ak fouklou borombi thi lou lakhou…