Limou mbiryi: 15
MP3 26 / 2 / 1436 , 19/12/2014
Khamlé pass-pass bou wére, jèkhitam thi nite ki, jèkhitam thi mbolomi
MP3 6 / 3 / 1436 , 28/12/2014
Sèllal, yittéwô bou kawé thi Alkhourâne ak Sounna, dégg ak wômmatou, sâmm wakhtou, ândandô you bâkh, di déllou sâssouné thi borôm expérience yi thi borôm kham-khamyi.
MP3 26 / 7 / 1435 , 26/5/2014
La droiture et son impact sur l’individu et la société
MP3 17 / 2 / 1437 , 30/11/2015
Taxawâyu jullit bi ci fitnayiTaxawâyu jullite bi ci xéwxéwu jamono
MP3 12 / 8 / 1436 , 31/5/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: éé yaw doomu àdama guddi ak bëccëk dañuy ligéy ci yaw knnak ligéyal ci ñoom. Ana naka ngay jariño sa waxtu
MP3 14 / 5 / 1436 , 5/3/2015
Wakhtâne mi ngui aju ci Tâkhalikôp joulliteyi _ sabap yi akiy jékhitam akiy sâfarâm
MP3 25 / 3 / 1436 , 16/1/2015
Wakhtâne wî mi ngui ajou thi yône yougnou meuna jâr ba yar ndaw bi yar gou matalé
Wakhtâne bî mi ngui wakh thi: khamlé louy fitnây jiguène, moussibâm, ay mélokânam, yône yi gnouy thiy mouthé
Wakhtâne bî mi ngui wakh thi: njarigne ak lor yi am thi kharala you bèss yi
Ame solôk ndaw – Warèfou ndawgni thi lislâm
Wakhtânewângui jeum thi: toubâbal ndawoup joullite bi thi khamléko, ay mândargâm, ak naka lagnouthiy mouthé
MP3 1 / 3 / 1436 , 23/12/2014
Nôppi thi dérou nitegni
MP3 18 / 2 / 1436 , 11/12/2014
Tasare nouyou migui bok thi mandorgay islam, atte tambali nouyou ak deloko, teguini nouyou ak ay srtam, atte yene batte yinouy wotte nouyou ypbe lislam, diekhantalou nouyou thi sociotebi…
MP3 28 / 1 / 1436 , 21/11/2014
Yar ndaowni aksolo thi sociotebi
Le péché ses méfaits et ses conséquences sur l’individu et la société