Tèkhanetal you ajou thi kham-kham

معلومات المواد باللغة العربية

Julli

Umpul bèpp jullite -cànte ñèlna Yalla- wàccuxâyu joulli ci lislam, mooy kénok diiné, di tàxxalé digganeté kéfër ak nguëm. Xàc bi ñi ngui ko jaglèl lèral li julli di tékki akiy àttèm, ay waxtoom, ay sartam, mélokànam, ay pooŋkam, ay faratàm, ak sunnàm, ak sujootup njumté

Limou mbiryi: 5

Kheut wi : 1 - Dalé thi : 1
Sap xalàt lu ñu saxalla