Sèllal, mâggal Alkhourane, sôpp yonènnetebi (Yalla na Yalla joulli thi mom), moytou dokhaline yi jouyô ak ndoup, li nguay beugg ak dikôy bagne Yalla rek takh,bagna nourounouroulou ak yéfeur yi
Bokna thiyiy maye thiofelou yalla: bagueyalla ak yonentebi, diagne al khourane ak settentalko, kher thi nafilati gannaw faratayi takho toudou yalla ak diko fouklou…