Leralni moujouk khol ak diegale daboke thi sababi nakou diafe ak dougou al Diana, doudou ay takhaway you dawyaram thi diegalouk salaf ak mouthiouk seniy dande…
Khouba gui mingui ajout hi akhi deunnkandô, war guimou war gnou jeufelaneté ak gnôm jeufelaté ak gnôm thi mbâkh: * Rafétal jeumé thi gnôm * Bagnelèna lor * Dékkou sèni lor