Limou mbiryi: 2
MP3 17 / 5 / 1436 , 8/3/2015
Leral niety degnkayi bithi diake:fedali gueguem bouwer,rafetal diame thi waydiour, ak oubbe kouam solo
MP3 22 / 6 / 1436 , 12/4/2015
Nekenathi leral ni diani waydiour nioy sababou sak niowe thi addouna,bakhal diame thi niani waydiour migui bok thi bakhal diame thi niari waydiour…