Limou mbiryi: 4
MP3 12 / 5 / 1437 , 21/2/2016
bekhel thie hame sa bire dine koum nouko sale salih hame Ay màndarga yu fess ci yoonu mak nu baax
MP3 25 / 3 / 1436 , 16/1/2015
Wakhtâwî mi ngui jeum thi: deuggeunetânou kham-kham, ngeunélam, ngeunélou borôm kham-kham, gâkk-gâkki sâkkou kham-kham ak ni mag gnou bâkh gni sâfarâ
MP3 14 / 5 / 1436 , 5/3/2015
Wakhtâne wi gui mi ngui ajou ci: léral wakh yi rote thi sânjjé gui nèkk thi wax lodoul dèf. Nguénéloup jeuf bou sèll. Yéne wou dis wik thi jeujf bou sèll. Wax lôdoul dèf akiy loram thi ligèyoup lislam. Akiy jékhitam.
MP3 21 / 4 / 1436 , 11/2/2015
Leral loubari thi melokani aji oubbeji , ak dansek aubbe thi loudoul khamkham…