Ap sânjjé la nguay wakh lôdoul dèf

Wakhtânekatebi : Mohammed Ahmed lo

Khôlâte: Djibril Dièye

Mélokâne bi

Wakhtâne wi gui mi ngui ajou ci: léral wakh yi rote thi sânjjé gui nèkk thi wax lodoul dèf. Nguénéloup jeuf bou sèll. Yéne wou dis wik thi jeujf bou sèll. Wax lôdoul dèf akiy loram thi ligèyoup lislam. Akiy jékhitam.

Download
Binndal sap guiss guiss kiy saytu xeüt wii

Tèkhanetal you ajou thi kham-kham: