Warèfoup bénnôp joulliteyi

Wakhtânekatebi : Ibrahim Khali Lô

Khôlâte: Djibril Dièye

Mélokâne bi

Waxtàn wi gui ajou ci lèral solo ngui né ci bénnô ak ngâgn tâxalikô akoup âttèm akiy sababam, lëkkëlô gui né thi ngeum ak bènnô ak lèral sabap yiy inndi bénnô

Download
Binndal sap guiss guiss kiy saytu xeüt wii

Tèkhanetal you ajou thi kham-kham: