Taxawàyu jullite bi ci pakkiy jamono
Wakhtânekatebi : Mohammed Ahmed lo
Khôlâte: Mohammed Cheikh Sene
Mélokâne bi
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Xétum lislàm tay mi ngi roomb ay pakk yu wuuté ciy wéte yu limu yuy té mu taxawé liko war ci kaw suuf.kon lan mooy taxawàyu jullite bi ci pakkiy jamono.
- 1
Taxawàyu jullite bi ci pakkiy jamono
MP3 30.2 MB 2019-05-02
Tèkhanetal you ajou thi kham-kham: