-
Ahmad Ali Ajami "Limou mbiryi : 28"
Mélokâne bi :Mi ngi juddoo xabar ci atum 24-02-1968. Amna doctora ci tafsir ci kémuk gëna baaxlé. Mi ngi binndoone ci Faraŋfàccé yoonu firi Alxouràne. Amna tamite majester ci Pakistan. Ak Bac ci universitèp Muhammad Ibn Saoud