-
Mahmud Ali Bannaa "Limou mbiryi : 47"
Mélokâne bi :Mi ngi juddo égipte ci atum 17-désambr-1926. Mi ngi wattoo Alxuràne ci daara dëkkam ci seriñ bu tudd Mussa Minetàs ci bi mu amé fukki ate ak bènn la mookal. Ginnaw gi mu toxu Tantaa ngir jaŋŋ xam xamu charia. Foofu sax la jëlé xamxamu jaŋŋinu alxuràn ci seriñam bii di Ibrahim Ibn Salam Al-Maliki. Gàñuna ci atum 20-julié-1985 (Yalla nako Yalla yërëm)