-
Ahma Ahmad Nuayna "Limou mbiryi : 1"
Mélokâne bi :Ap janŋkate la di ap facckate. Mi ngi juddoo kafr Cheikh ci 2gypte ci atum 1954. Dugna ci facultém médcine ci jànŋukay bu kawé bi ci eskanedari. Bi mufa paré mu ligéy ca lopitàlba. Rajoo ak télé bu egypte défnako jàŋkatu alkhouràne ci atum 1979