-
Abdoullah Taha Sarbal "Limou mbiryi : 2"
Mélokâne bi :Mi ngui jouddô thi Ordone le 10-Mai-1979, yilimane ak khoutbakate thi jâkkâp oummoul Mouminine dôré thi 1999 ba fî gnou tôll. Amna bac thi charia, geuna mâth thi thiôssâni dîné. Amna tamite Majèstère thi université bi mâth thi kham-khami Al-Khourane (W.I.S.E.)