-
Muhammad Iwad Al Harbàwii "Limou mbiryi : 1"
Mélokâne bi :Mi ngi génné azhar ci jaŋŋkàyu lislam bi ak làkkup arap, famu amé lijàssa bu kawé ci jàŋŋin yi, ak lijàssap maacc si. Amnaci Doctora. Jàŋŋaléna ci azhar ay ate yu limu ak ci ay jàŋŋukaay yu arabi sawdite, ni mu fassaneté ak facultép jàŋŋalékate bi ci riyaad. Bokkna ci yi mu bindd: At-tashiil fiimaa yachtabihu bil xaari mine aayaati taneziil, ci léral jàŋŋinup warch ci imam nafi, ci kissaaii, ci baate yi 10 jàŋŋkateyi wuté ci chaatibiyya ak durra, ci hamza, choubaa ci chaatibiyya ak durra.