-
Mouhammad Abdoul Hakîm Ibn Said Al-Abdallah "Limou mbiryi : 2"
Mélokâne bi :Kènne la thi gniy jânggalé thi Makka, mi ngui askanô Syrie. Di kou geuna mâth thi njâgginoum Al-khourâne ak kham-kham yi thi ajou. Jânggé thi pâpâm di ap jânggkate bou râgnékou tamite toudd Said Al-Abdallah (Yalla nako Yalla yeureum) (nékkône njîtou jânggkate yi thi Hama). Jânggaléna Oummoul Khoura. Enregistréna foukki njânggine yithi yônou châtibiyya ak dourra.