-
Mouhammad Ibn Abdoul Wahab "Limou mbiryi : 332"
Mélokâne bi :Môy Cheikh Mouhammad Ibn Abdoul Wahab Ibn Soulaymane bôkk thi guîrouk Tamîm, mi ngui joudd thi 1115 thi gâddây gui thi deukk bou toudd Ouyayna thi arabi saoudite, beurina loumou taalîf. Borôm kham kham yi mândou yi sédèlnagnouko kham-kham ak am dîné ak tégé thi yône wou joup. Fâtouna (Yalla nako Yalla yeureum) thi atoum 1206 thi gâddây gui amône 91 ate.