-
Mouhammad Salih Al-Mounajjid "Limou mbiryi : 3522"
Mélokâne bi :Mouhammad Salih Al-Mounajjid: Wôtékat la bu cosànô Siri, mi ngi juddu ci 30-12-1380 ci gàddàygi, mi ngi mâggé Riyad janŋŋé arabi sawdit ci ay borômi xamxam yu limu, bôkkna ci ñoñu: Cheikh Ibn Bâz ak Cheikh Ibn Usaymîn