-
Ahmad dômou Mouhammad AlHawwâchî "Limou mbiryi : 1"
Mélokâne bi :Môy Ahmad dômou Mouhammad dômou Abdallah dômou Mouîd AlHawwâchî. Yilimâne la ak khoutbakate thi joumây thi deukk bou toudd khamîss mouchayte thi beutt saloumou arabi sawdite. Mi ngui jouddou thi deukk bou toudd ahad rafîdah thi atoum 1374 thi gâddây gui.