-
Cheikh Abou Bakr Ach-Châtiry "Limou mbiryi : 27"
Mélokâne bi :Cheikh Abou Bakr Ach-châtiry mi ngui joudd atoum 1970 thi jidda môy yilimânou joumây Al-Fourqâne thi Nassîm Jidda. Mi ngui dègnth sokhna am thi gnènnti dôm. Dâkkanetalam môye Abou Abdourrahmane. Ay lijâssâm thi jângg: dipolomou jângg Al-khourâne bou tèddbi thi hafs bi jogé thi Âssim thi serignam bî di Aymane Rouchdî Souwayd thi atoum 1416 thi gâddây gui, wayé thi jèkhinetaloup atoup 1420 thi gâdây gui amna tamite diplomoup mâjèstèr thi saytou alal.