Ay nite you râgnékou
Limou mbiryi: 116
- Wolof
- Wolof
Mi ngui askanô egypte toudd Ahmad Abdoul Fattâh Mouhammad Al-Haddâd, mi ngui joudd 25-08-1984. Thi universitèp Al-Azhar la amé lisensam thi lâkkou arapnthi atoum 2007. Akoup lijâssa mâjestèr thi wéral mbindd yi gnou fi bayyi thi attoum 2008, ak mâjestèr thi kham-khami Al-khourane ak foukki njânggine yi yi gnou tokhalé thi Yonnènetebi (Yalla na Yalla joulli thi môm té dôlliko jâmm)
- Wolof
Mi ngui toudd Chirzâd Ibn Abdour-Rahmane Ibn Tâhir Ibn Hassane Al-Kâfy Al-Kourdy Ach-Châfi î, mi ngui jouddô thi beutt gânnârou Irak thi atoum 1968 thi fou gnouy wakh An-Nâmâiyya. Fôfou la jânggé thi ay serigne you bari niki: Cheikh Abdoul Latif Ibn Khalil As-Soufy, ak Cheikh Al-Hafiz Ali Ibn Houssayn Al-Wassâbi, ak Cheikh Al-Hafiz Abdour Razzâkh Mouhammad Imâra, ak fénène tamite. Jîténa thi ay jâkka you bary thi Irak ak Imarate.
- Wolof
Jânggikatoup égypte la. Mi ngui joudd thi atoum 1984, mi ngui am lijâssa thi njângginoup al-khourâne ak kham-khamou charia thi colèzoup njângginou al-khourâne bi thi Al-Azhar, ak thi njângg gou kawé. kènnela thi ngiy jânggalé thi markazoup Oustaz doctor Ahmad Issa Al-Minssrâwî di njîtou jânggkatou al-khourâne yi thi égypte.
- Wolof
- Wolof
- Wolof
Mi ngui jouddô Médine thi 1382 thi gâddây gui. Amna doctôra thi piri thi atoum 1412 thi gâddây gui thi université ba. Nékkône yilimâne ak khoutbakate thi joumây Al-manâratayni thi Anebouriyya ak Khoubâ. Nèkkitame kène thi gniy saytou mbôtây giye jânggalé Al-khourane thi médine. Nimou dâne saytô ay liguèye you ajou thi al-khourâne. Di kènne thi gniy saytou njânggalèm al-khourane thi université bou médine, oustaz thi tafsir thi facultèp al-kouranebi. Nèkk kiy saytou lèpp lou jeum thi bibliôtèk ba. Tânnenagnouko mouy yilimâne thi nâfilây kôr thi jâkka Yonènetebi (Yalla na Yalla joulli thi môm té dôlliko jâmm) thi atoum 1432 thi gâddây gui
- Wolof
- Wolof
Môy Cheikh Yahya Ahmad Mouhammad Al-Halily, jouddô deukkou halila thi Yémène thi atoum 1372 thi gâddây gui tôllôk 1952. Mi ngui dôré thi jotâyoup njânggoup Al-khourane thi joumâ bou mak bithi capitâlbi dâldi môkkal thi atou 1962. Ginnâw gui mou jângg jourôm gnâri jânggine yi thi ay borôm kham-kham you bary. Mou dâldi am lou tôlôk lijâssâp lisense thi ministèroup yargui ak njânggalémi thi atoup 1973 fèkk tâmbaliwôna njânggalèm Al-khourâne thi atoup 1970, ak di jîté aka khoutba thi joumây tahrir thi saneâ (capitâlbi), niki nônou dôrena jîté attékatou jonganetèp al-khourâne thi atou 2000 thi deukkam ak égypte.
- Wolof
- Wolof
Mi ngui jouddô Bagdad thi atoum 1953, génné thi universitèp Bagdad thi Facultèp Droit ak polotik thi atoum 1975, mou nékkône ki jîtou. Ginâw gui ministère biy saytou mbiri tougeul jeulko thi atoum 1977. Wayé mou tokhou thi liguèye bôbou, dâldi sôbou thi jângg ak jânggalé Al-Khourâne ba amthip ap lijâssa thi njângginou hafs thi yônnouk Ach-Châtibiyya thi doctor Sayid Mouhammad Sadati Ach-Chinegiti moudi ap oustaz thi universitèp Mouhammad Ibn Saoud bi thi Riyad thi atoum 1997. Fîmou nèkk mi ngui sâgnth thi arabi sawdite thi Riyad.
- Wolof
- Wolof
Mi ngui jouddou thi 19-04-1986 thi Âzamiyy thi Baghdad thi Irak. Nékkônna - Yalla nako Yalla yereum- kènne thi mbôtâyoup jânggkate alkhourâne yi thi Irâk, bôkkna thi ay jongânté you bari, mi ngui fâtou thi 26-05-2007 thi jâmârlôk soldâroup amérik yi. Yalla nako Yalla bôlé thi gnimou nânggoul sène dé thi yônou Yalla ak gni deuggou.
- Wolof
- Wolof
- Wolof
Môye Cheikh mahmoud Ahmad Abdoul hakam, Mi ngui jouddou bèss bou njeukk thi féviryé thi atou 1915 thi deukkoup Karnak bou sîwbi té bôtou thi centar Abou Tichte thi provinsoup Qanâl Arîf thi saidou égipte, bi mouy am foukki ate la môkkal Alkhourâne thip dâra mouné thi kognam guinnâw gui lako bâyam thip école bou nékk Tânetâ mou déffa gnâri ate. Mou jânggéfa njângginou Alkhourâne lâta mouy dougg Al-azhar mânggéfa lou beuri thi borôm kham-kham yamoufa fèkk thi dîrroup yénène gnâri ate. thi jamono bôbounak dâne ne tôppadô janggkatou Alkhourâne you mak yi ba ay khamèlaùm di ko sôgne thi mou wey thi yône bôbou. Nônou la sîwé sîw bou yâtou. Thi attoup 1940 ânddna akiy fôré thi njânggoum Alkhourâne: Mouhamad Rifate ak Ali Mahmoud ak As-sayqî ak gnoudoul gnôm thi soss mbôtâyoup jânggkatou Alkhourâneyi dâdi kothiy jîtal thi saytou alal gui. Mi ngui fâtou thi altiné 13 sèptembre 1982 Yalla nako Yalla yeureum.
- Wolof
- Wolof
Môy Mouhammad dômou Rachâd dômou Abdous Salâm dômou Abdour Rahmâne Ach-charîf, mi ngui jouddô deukk bou gnouy wakh Al- Khalîl thi Palestîne atoum 1925 thi atoum toubap, mouy kènn thi jânggkatou Al-Khourâne yi sîw thi addinabi, môy jânggalékatoup jâkka Al-Aqsâ bou barkèl bi agitam jâklâp Al-Ibrâhîmî yi nèkk thi Al-Khalîl.Guinnâw gui thi atoup 2002 tokhouna jeum Ordone.Nèkkna yilimâmou jâkka boûr bi toudd Abdoullah Al-Awwal bithi Abdoûlî
- Wolof
Mi ngui jouddô liban thi atoum 1966, amna doctôra thi lâkk arabe akiy adabam, akoum dipolom bou kawé thi njanggoum charia (rawatina thi njangginou alhkhourân), té môy saytou njângginou alkhourâne yi ak toudd Yalla yiy daw thi rajôp Hayâte FM, di saytou tamite dâra alkhourâne bi bôtou thi ministèroup ndimmbeul yi Ordatiyya, falay jânggalé njâgginou alkhourâne liko dalé thi attoup 1990 ba tay. Nékkena tamite jânggalékate thi yènn faculté you charia thi Ordone, wayé légui mi ngui jânggalé thi univérsitè mondial bi thi malézi. Amna ay téré youmou tâlîf niki: * Jèkhinetaloup téktalèp lâkk arap thi woûté joulliteyi thi thiôssâni dîné * Khétou kham-kham yi thi alkhourâne * Joubal lâmmign thi njângoum alkhourâne * Bagna am jafé-jafé thi diggananeté joullite yi thi sèni mazap yi gnouy askanô menoul gnâkk té faratala * Sânggoup jânggkateyi Ach-Châtiby * Chawâhidoul Khourrâ * Gnou râgnékou thi jânggalékate yi ak gnilène jâggal.
- Wolof