• Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 2

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 3

    Mi ngui thiôssânô irak, dèfna ay jalôré thi njânggoum Al-Khourâne bou tèdd bi, niki nônou enrezistréna ak kâmil you bari

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 4

    Abdoullah Abdoul Ghany Al-Khayyâte -Yalla nako Yalla yeurem- nèkkônna yilimanou jakka makka

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 3

    Yilimâne thi Joumây Ad-Dakhîl thi gokhoup Ghirnâta thi Riyâd

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 3

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 3

    Mi ngi cosanoo Kuwét. Di boroom bàte bu ràññéku enresistéréna bénn kamil ci hafs ak khàluun. Li yémé ci mbiraù mooy né mooy goolup ékipe national bu futbalbi

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 3

    Mi ngi judd 19-06-1398 ci gàddày gici jidda. Ci atum 1415 ci gàddày gi la mookaal alxuràn. Amna majestér ci saytu mëne mënup nite. ak bac ci porotochimi. pilote la ci arabisawdite. Mi ngi tàmmbalé jitté ci atup 1415 ci gàddày gi ci kaar ci jàkkàp Al-Baghdàdi ginàwgi ci jàkkàp Alhudà ci Al-Andalus toopp mu dem ci jàkkàp Khadija Bint Xuwaylid ci Zahrà. Fiiñu tooll mi ngi jiité aka xutba ci jàkkàp At-Taxwà ci yoonup At-Tahliya.

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 3

    Kénne la thi yilimani Arabi Sawdite. Mi ngui jouddô Mâkka, fa la jânggé ba paré. Jânggalékate la thi kaba gui thi pâth gui ajou thi Al-Khourane. Jânggna kâmil thi radiop al-khourâne, ak aykamil thi yônnoup châtibiyya.

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 3

    Wâ égypte la, di kènn thi gniy jângg Al-Khourâne thi foukk jânggine yi thi radio Koweit bi. Di ap nôddkate thi jâkkâp Moûdy Al-Oumr, nèk kènn thi âttékate yiy saytou njânggkate yi.

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 3

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 3

    Mi ngui guénné Université bou Madina, di yilimane ak xoutbakat, râgnékou thi tôloup wôté jëmé ci Yalla

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 4

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 5

    Salâh Al-Hâchim: Kènnela thi yilimâne yiy jîté thi joumay Kowète bou mak bi

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 6

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 6

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 6

    Mi ngui juddoo Riyad. Amna bac ci ŋàŋum lislam. Mi ngui tooll ci majester geüna macc ci Al-khuràne

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 8

    Jânggkate la bou sîw thi maroc, di yilimâne thi jâkkâp Al-Hassane 2 thi Daroul baydâ

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 8

    Mi ngui jouddô Damas, wayé mi ngui deukk arabi saoudite. Nékkône yilimâne thi jâkkâp As-Siddîkh gui fété pénkou

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 9

    Jàŋŋkatu alxuràne la bu juddoo Médine ci atum 1364 ci gàdàygi, fala magé yaroofa jàŋŋéfa ci Darul hadis ginnàw gi mu dem najàh topp mu dem ci colés ba mujjé ci écolup xaralé yi jëm ci isine. Jàŋŋéna ci ay kàŋŋàm: Omar Alhaydari, Ahmad Az-Zayyàte, Abdulla Al-Ghunaymàn. Boolénaci fikh ak passpass ak charia. Fétéwoona ak ligé yu takku, niki: Ustas ci xaralép usine, ci Alxuràn ci ecolup ubay Ibn kab ci médine, Ustas buy wootu ci universitep Medine. Ci atup 1406 ci gàddày gi la tàmbalé jiité ci jàkkày Médine. Bookkna ci attékate yi màcc ci Alxuràne.