• Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 81

    Yilimane ak khoubakate thi jâkka Yonnènetebi (Yalla na Yalla joulli thi môme)

  • Wolof

    Kikon jângg, Kiko tâlif, Limou mbiryi : 29

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 8

    Mi ngui jouddô Damas, wayé mi ngui deukk arabi saoudite. Nékkône yilimâne thi jâkkâp As-Siddîkh gui fété pénkou

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kiko khôlâte, Kikon jângg, Limou mbiryi : 522

    Yilimâne ak khoutbakate thi jâkkap Yonnènetebi (Yalla na Yalla joulli thi môm)

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 6

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 28

    Mi ngi juddo jidda ci 09-11-1381 ci gàdday gi. Amna Bak ci ŋàŋum lislam ci jànŋukày bu kawé bi ñu duppé Al-Malik Abdul Aziz bi ci jidda ci 1406 ci gàddày gi.Ak Majester ci Fikh ak Ciosànam ci jànŋukày bu kawé bi ñu duppé Ummul Qurà bi ci Makka, binndoone ci (Ay léral ci xàc bu njëkk ci ay dëppo yu Ibn Ruchd ci térém bi di Bidàyatul Mujtahid wa Nihàyatul Muqtasid) ci atum 1412 ci gàddày gi. Ak Doctora ci fikh ci atum 1419 ci gàddày gi. Ni mu améwone lijàssa ci Hafs ci cheikh Doctor Aymane Ruchdi Suwéyd ci 1407 ci gàddày gi.

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 4

    Abdoullah Abdoul Ghany Al-Khayyâte -Yalla nako Yalla yeurem- nèkkônna yilimanou jakka makka

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

    Jânggkate bou Kouwète

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 35

    Yilimânou mâkka

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 2

    Mi ngui jouddô thi Ordone le 10-Mai-1979, yilimane ak khoutbakate thi jâkkâp oummoul Mouminine dôré thi 1999 ba fî gnou tôll. Amna bac thi charia, geuna mâth thi thiôssâni dîné. Amna tamite Majèstère thi université bi mâth thi kham-khami Al-Khourane (W.I.S.E.)

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 157

    Yilimâne ak khoutbakatou Makka

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 2

    Mi ngui joudd thi 5-5-1980. Jânggalékate di yilimane thi jâkkâm Al-Ikhlâs thi Arabie Saoudite.

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 3

    Mi ngui thiôssânô irak, dèfna ay jalôré thi njânggoum Al-Khourâne bou tèdd bi, niki nônou enrezistréna ak kâmil you bari

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

    Mi ngi judoo Maroc ci atum 1947. Amn lijàsa ci warch ci yoonup Asbahàni ci Cheikh Ahmad Ibn Usmane Abul Alà. Ku ràññékula ci tajwiid té mi ngi ciy joxé ay binnd. Kennla ci ñiy fuglu wérug jaŋŋ al-khouràne. Taliifna: Naka laŋuy jaŋŋé Al-khouràn ci warch ci yoonup Azraq

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

    Mi ngi juddoo maroc ci atum 1963, mookalna Alxuràne. Amoone yitté lool ci fékké jotàyup xamxam biñu amal ci Darul Baydaa ci atum 1992, raññékuca ci wàllup jàŋŋate lislam. Yilimane la dip xutbakate ci jàkkap As-sabiil ci Darul Baydaa. Di kénn ci attékate ci joŋantép alxuràne bi ñu duppé Mouhammad Sis. Enresistérélnañuko ap kamilci atum 2005. Nimu enresistéré ci alxuràne ci atum 2010. Té mooy ki sos porosép (mookkalél alxuràne ci sa kër) mu jëm ci mookkalloo mboolem ñi mënula téw ci jàkkayi. Moo taaliif Tuhfatul Hadiidii ci tëŋkkiy jàŋŋiinu alxouràne ci warch ci yoonup asrax.

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 17

    Touram môy: Abdur Rachid Ibn Cheikh Ali Sufy. Lu aju ci démbam: mi ngi juddi ci atum 1964 ci Somali. Pappam môy fóré bi tudd Ali Ibn Abdur Rahmane Sufy (Ubbékabup Somali ak kafa gëna kawé ci jâŋŋup Al-xuràn) muy kifa ngëkka dugal ak tassâré xamxam ngaŋŋu Al-xurân ak ngaŋŋine yi, ñu bari ci ay borô xamxam jaŋŋénañ ci môm, tabaxna ay école akiy centar yu limu ngir ñufay jàŋŋ al-xurân. Mi mujj ci jàkka yôyu môy bu sîw bici Mogadîsiô bi ñu duppé Jàkka Cheikh Ali Sufy bi nga xamné fala Abdur Rachide Sufy fala jàŋŋé. Jàruwàyam ci al-xuràn ak sàkku xamxam: mi ngi jàŋŋé ci bàyam ci jotàyu xamxam yimu dàn amal ci jàkkaji ba môkkal ci fukkélu atam. Ginnàwgi mu mu jékku xamxam niñuy jànŋŋé al-xuràn ci hafs jëléko ci Asim, ték ci jurôm ñâr yi dés ci yonu Châtibiyya, bôlékôk déglu faraŋfàccéwu térép Châtibiyya ñatt yôn ba môkkalko. Chatibiyya ap qasida làmiyyala bu Imam Waliyyulla Al-qassim Ibn Fîrra Ach-châtiby (yàlla nako Yàlla yërëm) mingi fàtu ci atum 599 ci gâddày gi qasîdâm gi amna 1173 bayte. Ginnâw gi mu jàŋŋ li jàppandi ci nahw ak fiqh Chafi'î ci bâyam, ba mujjgi mu tukki Egypte ngir môttali jàŋŋgine yi ci Octobre 1981, fôfé la duggé ci jànŋŋukây yu kawéyi ba amfa lijàsa yu kawé yi ci fukki jànŋŋine yi; bôlékôk di jël ay binnd ci borôm xamxamu jànŋŋkatu al-xuràn bu mak bî di Cheikh Muhammad Ibn Ismail Al-hamadàny (yàlla nako Yàlla yërëm) ci Azhar ba amci ñàri lijàsa yu am càllalé baci Yonéntebi (yàlla na Yàlla julli ci môm): 1- ci fukki njàŋŋine yi ci yônu Châtibiyya ak Durra. 2- ci fukki njàŋŋine yi ci yônu At-tayyiba bu imam Al-jazari. Jànŋŋ na itam xamxam rëddup Kàmilbi. Lu aju ci ay jalôrém ak wôtém ci yônu Yàlla: ginnàw bimu nôppé ci njànŋŋam délluna Somali wuutu bàyam ci jité ak janŋŋalé ca jàkkaja ginnàw bimu fébaré. Faréna jànŋŋalé xamxami Al-xuràn bu téddbi ci faculté bi màcc ci xamxami lislàm té jôkku ci Azhar. Mbôlo bu bari ci Somali ak Qatar jariñunañu ci binnd yôyu. Mi ngi éksi Qatar ci atum 1991, ministérup yi aju may yiñudul dônn ka ci lislàm tànnko mu jîté aka xutba ci jumày Anas Ibn Malik (yàlla nako Yàlla yërëm) ci marsé centaral bi. Amna ay yëŋŋatu yu aju ci wôté jëmé ci Yàlla ci Qatar. Niki nônu itam dafay amal ay binnd akiy waxtàn bôlékôk téwé ay séminaire akiy ndajé yu aju ci lislàm rawatina ca tugal. Démna itam Bahrayni ay yôn. Amna ay njànŋŋ yu ñuko enresistérél ci Sadal Fajr ci sitam. Sitam môy: www.abdulrashid.net

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

    Ap janŋkate la di ap facckate. Mi ngi juddoo kafr Cheikh ci 2gypte ci atum 1954. Dugna ci facultém médcine ci jànŋukay bu kawé bi ci eskanedari. Bi mufa paré mu ligéy ca lopitàlba. Rajoo ak télé bu egypte défnako jàŋkatu alkhouràne ci atum 1979

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

    Mi ngui askanô egypte toudd Ahmad Abdoul Fattâh Mouhammad Al-Haddâd, mi ngui joudd 25-08-1984. Thi universitèp Al-Azhar la amé lisensam thi lâkkou arapnthi atoum 2007. Akoup lijâssa mâjestèr thi wéral mbindd yi gnou fi bayyi thi attoum 2008, ak mâjestèr thi kham-khami Al-khourane ak foukki njânggine yi yi gnou tokhalé thi Yonnènetebi (Yalla na Yalla joulli thi môm té dôlliko jâmm)

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

    Wâ Yémène la, mi ngui jângg Al-khourane thi joumây Oussama Ibn Zayd, jângg kham-kham thi Mahad Nour. Fi gnou tôll mi ngui jângg thi uniniversitèp bi mâth thi kham-khamou Téknolozi thi kapitalou Yémène di Sanâ

Kheut wi : 6 - Dalé thi : 1