• Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 28

    Fâriss Abbâd: mi ngui thiôssânô Yémène.Di borôm bâte bou nèkh té râgnèkou. Enrezistéréna ay téré kham-kham ak Kâmil bou mate. Bôkkna thi yolimânou jâkka Alioune dômou Abî Tâlib thi Ad-dawha thi sôwwou Arabi Sawdite

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 2

    Moudi borôm kham-kham bou sîw thi pakistan

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 2

    Mi ngui thiôssânô Yémène, yilimâne la ak khoutebakate thi joumây Khalid Ibn Al-walîd thi katar

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 2

    Ci jànŋŋkat yi siiw la book. Mi ngi judd 1974. Yilimàne la ak khoutbakate ci Jidda (Arabi Sawdite). Sitam mooy: http://www.alrfaey.org

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 2

    Jânggkate la bou thôssânô Egypte thi Al-Bouhayra, paréna thi njângginou Al-Khourâne yi, niki nônou jânggna thi université bi mâth thi kham-khamiy Al-Khourane. Yilimane la ak khoubakate thi Centre Islamique bi thi New York

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 91

    Yilimane ak khoubakate thi jâkka Yonnènetebi (Yalla na Yalla joulli thi môme)

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 9

    Jàŋŋkatu alxuràne la bu juddoo Médine ci atum 1364 ci gàdàygi, fala magé yaroofa jàŋŋéfa ci Darul hadis ginnàw gi mu dem najàh topp mu dem ci colés ba mujjé ci écolup xaralé yi jëm ci isine. Jàŋŋéna ci ay kàŋŋàm: Omar Alhaydari, Ahmad Az-Zayyàte, Abdulla Al-Ghunaymàn. Boolénaci fikh ak passpass ak charia. Fétéwoona ak ligé yu takku, niki: Ustas ci xaralép usine, ci Alxuràn ci ecolup ubay Ibn kab ci médine, Ustas buy wootu ci universitep Medine. Ci atup 1406 ci gàddày gi la tàmbalé jiité ci jàkkày Médine. Bookkna ci attékate yi màcc ci Alxuràne.

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kiko khôlâte, Kiko firi, Limou mbiryi : 39

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

    Mi ngui jouddô liban thi atoum 1966, amna doctôra thi lâkk arabe akiy adabam, akoum dipolom bou kawé thi njanggoum charia (rawatina thi njangginou alhkhourân), té môy saytou njângginou alkhourâne yi ak toudd Yalla yiy daw thi rajôp Hayâte FM, di saytou tamite dâra alkhourâne bi bôtou thi ministèroup ndimmbeul yi Ordatiyya, falay jânggalé njâgginou alkhourâne liko dalé thi attoup 1990 ba tay. Nékkena tamite jânggalékate thi yènn faculté you charia thi Ordone, wayé légui mi ngui jânggalé thi univérsitè mondial bi thi malézi. Amna ay téré youmou tâlîf niki: * Jèkhinetaloup téktalèp lâkk arap thi woûté joulliteyi thi thiôssâni dîné * Khétou kham-kham yi thi alkhourâne * Joubal lâmmign thi njângoum alkhourâne * Bagna am jafé-jafé thi diggananeté joullite yi thi sèni mazap yi gnouy askanô menoul gnâkk té faratala * Sânggoup jânggkateyi Ach-Châtiby * Chawâhidoul Khourrâ * Gnou râgnékou thi jânggalékate yi ak gnilène jâggal.

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

    Mi ngui jouddô Médine thi 1382 thi gâddây gui. Amna doctôra thi piri thi atoum 1412 thi gâddây gui thi université ba. Nékkône yilimâne ak khoutbakate thi joumây Al-manâratayni thi Anebouriyya ak Khoubâ. Nèkkitame kène thi gniy saytou mbôtây giye jânggalé Al-khourane thi médine. Nimou dâne saytô ay liguèye you ajou thi al-khourâne. Di kènne thi gniy saytou njânggalèm al-khourane thi université bou médine, oustaz thi tafsir thi facultèp al-kouranebi. Nèkk kiy saytou lèpp lou jeum thi bibliôtèk ba. Tânnenagnouko mouy yilimâne thi nâfilây kôr thi jâkka Yonènetebi (Yalla na Yalla joulli thi môm té dôlliko jâmm) thi atoum 1432 thi gâddây gui

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 17

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

    Môy Jazzâe Ibn Falîh As-Souwaylih, mi ngui jouddô Kowète thi atoum 1969, bôkkfa thi jânggkate yi sîw, mi ngui génné thi facultèp kham-khamou charia ak njâgg lislâm thi univèrsitèp Kowète gi ngua khamné falay jânggalé alkhourâne ak njângginam

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 1

    Jânggkate bou égipte

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 2

    Mi ngui jouddô Mâkka, amna bak thi njanggate Alkhourâne thi facultèp janggalékate yi tém nèkk jidda. Bôkkna thi yilimâni jâkkay jidda thi arabi sawdite

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 16

    Yilimâne thi jâkkâp ndème si Yallassi Abdour Razzâkh Khinebar Al-Anessâry -gokhoup An-Nakhil thi Dammâm

  • Wolof

    Kiko tâlif, Limou mbiryi : 2

    Mi ngi mookkalé alkhouràne ci ap centarup Az-zayd ci bi muy am 13 ate ci loxoop Ghulàm Hussayn mi ko jox liàssa. Jàŋŋna ci Cheikh Ibrahim Al-Akhdar mi jiité jàŋŋkateyi ci madina fa jàkka Yonéneteba (Yalla na yalla julli ci moom té dooliko jàm) mi ko jox lijaasa ci hafs. Jàŋŋna tamit nàfi ci warch, kiko jàŋŋal di Cheikh Doctor Mouhammad Âsim Al-qudàte miko jox ndigal mu meüna jàŋŋ ak jàŋŋŋalé. Gëstoom: amna bak ci ingégneur ci 2001. Ligéyam mooy saytu mboolém yu mak ci Imarate. Kénn la ci ñi jiité saytup mbootàyup Alkhouràane ak Sunna ci Chàriqa bi nga xamné làmboona lu ëpp 9000 ci goor ak jigéne

  • Wolof

    Kiko tâlif, Kikon jângg, Limou mbiryi : 24

    Yilimane ak khoubakate thi Makka