Tèkhanetal you ajou thi kham-kham

Téktal yiy wané né Muhammad Yonéntela (Yàlla na Yàlla julli ci moom té dolliko jàm)

Xët wi mi làmmboo yu aju ci téktali Yonéntegi ci làkki àdduna bi, séddalikoo ay toomb yu wuté: * Kumpa yimu xibàré (Yàlla na Yàlla julli ci moom té dolliko jàm) * Xarbaax yiko Yàlla jox (Yàlla na Yàlla julli ci moom té dolliko jàm) * Xibàré yu aju Yonénte yu jiitu (Yàlla na Yàlla julli ci ñoom) ak bégal guñu bégal séne xéte ci ak ñëwam (Yàlla na Yàlla julli ci moom té dolliko jàm)

Limou mbiryi: 1

  • Tâjiki

    PDF

    Lii ap téré la buy inndiwaate dàggasanté gu doxoone digganeté Ahmad Deedate akiy làbbé yuy jéma wéddi béglé gi ñu béglé ñeüwup Muhammad yalla na (Yalla julli ci mom té doolliki jàam) ci Inejiile gi ñu sooppi wayé ak mbir yuy féddali bégalgogé té deüppo ak Muhammad (Yalla na Yalla julli ci mom té doolliki jàam)

Kheut wi : 1 - Dalé thi : 1
Sap xalàt lu ñu saxalla