Limou mbiryi: 3
Apgaattal ci teereep: Ap tëŋkk bu am solo Ci taari lislaam Kiko binnd Cheikh Abdurahmane Ibn Naasir Saadi (1307 -1376 ci gaaddaygi) Kiko jeema tëŋkk
Ci turi YALLA lay doore sama mbind mi, moom miy borom yërmande bu yaatu bi di yërëm ku ko soob.