Wakhtânewi mi jeum thi: * Kénnal Yalla akiy mélokânam * Thi Yonnèneteyi (Yalla na Yalla joulli thi gnôm té yôkkelène jâmm) * Thi li arâm ak li dagane …
Sitoup IslamHouse.com môye site bi geuna mak bouy wôté jeumé thi lislamthi lâkki addounabi, mou lâmbô ak ak mbir you amul fay thi lou eupp 100 lâkk thi ay téré ak you gnouy dèglou ak you gnouy sètâneakiy natâl you gnou wâjal akiy porgarâm you ajou thi lislam ak yénène https://islamhouse.com/wo/main