Ngueunélouk sâkkou kham-kham

Wakhtânekatebi : Mohammed Ahmed lo

Khôlâte: Djibril Dièye

Mélokâne bi

Wakhtâwî mi ngui jeum thi: deuggeunetânou kham-kham, ngeunélam, ngeunélou borôm kham-kham, gâkk-gâkki sâkkou kham-kham ak ni mag gnou bâkh gni sâfarâ

Download
Binndal sap guiss guiss kiy saytu xeüt wii

Tèkhanetal you ajou thi kham-kham: