Limou mbiryi: 152
17 / 5 / 1437 , 26/2/2016
khotba bi tih Le Dialogue en Islam amana solo bou bakhe
19 / 2 / 1437 , 2/12/2015
Nekena thi leral guenelou dioulli yoryor, ak tontou ndakh khouy def ape bida ndakh dina thi am touyaba?...
17 / 2 / 1437 , 30/11/2015
Taxawâyu jullit bi ci fitnayiTaxawâyu jullite bi ci xéwxéwu jamono
Yónu yókkuté ci lislàmTërëlinu lislam ci yónu yókkuté
Nekena thi doudou mandar gayou makyi ak you ndaw yi ak amsolo ak diekhantlam thi doundou joullit.
10 / 2 / 1437 , 23/11/2015
Ngënélu sante Yalla aye djehitalam
Attéy passé se islam aye fasion
xamle fagu thi islam gednole Fàggu lu dagane
soxna sou dekou thie Tuubupap
tahaw setlou ak NdoxXéwëlwalaMbugal
Nekena thi nontou nakh khoudar yonentela wala walliyou?
14 / 10 / 1436 , 31/7/2015
hotba Ci yén la bawoo
13 / 10 / 1436 , 30/7/2015
hotba bi cey li Bouléne yaxx
Xàju nitñi ci rawanté jëm ci lu bàx
12 / 10 / 1436 , 29/7/2015
Jaaduna ci ki goorgoorlu ci wéru koor mu wéyal loolu ginnaaw kori ak goorgoorlu woor jouroombenni fane ci sawwal
11 / 10 / 1436 , 28/7/2015
Ku xool li addunabi di jàŋkonte ci ay jafé jafé ci koom, dina giss né jaaduna ñu wané yoon yunuy may suxaliku
10 / 10 / 1436 , 27/7/2015
Ay jànggat yu aju ci wéru koor, ak lenn ci sababu yéx gu ndimmbalu Yalla tardé
20 / 8 / 1436 , 8/6/2015
Soloss waxtàn wi mi ngui gëna feñ ci toxal guy ñuciy toxalal niko mag èu baax daan mànggé
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Dina jaadu ci bépp jullite mu yittéwoo lu aju ci àttéy diiném rawatina wéru koor
14 / 8 / 1436 , 2/6/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Xétum lislàm tay mi ngi roomb ay pakk yu wuuté ciy wéte yu limu yuy té mu taxawé liko war ci kaw suuf.kon lan mooy taxawàyu jullite bi ci pakkiy jamono.