-
Abdul Ali Al-Anune "Limou mbiryi : 1"
Mélokâne bi :Mi ngi judoo Maroc ci atum 1947. Amn lijàsa ci warch ci yoonup Asbahàni ci Cheikh Ahmad Ibn Usmane Abul Alà. Ku ràññékula ci tajwiid té mi ngi ciy joxé ay binnd. Kennla ci ñiy fuglu wérug jaŋŋ al-khouràne. Taliifna: Naka laŋuy jaŋŋé Al-khouràn ci warch ci yoonup Azraq