-
Yasine Al-Jazàiri "Limou mbiryi : 1"
Mélokâne bi :Mi ngi judd 1969 ci Al-Hiràs ci kapital bi, cosanoo ci Al-Buwayra. Amna lisense ci Chimi, ginnaw gi mu yéggali jàŋŋam ci cosaniy dinné ci charia. Mooy ki njeükka enresistré ap kamil ci warsh ci yoonup Al-Awrakh. Mi ngui jiité ci jàkk Abu Obayda Ibn Al-Jarràh.