-
Jazzâe Ibn Falîh As-Souwaylih "Limou mbiryi : 1"
Mélokâne bi :Môy Jazzâe Ibn Falîh As-Souwaylih, mi ngui jouddô Kowète thi atoum 1969, bôkkfa thi jânggkate yi sîw, mi ngui génné thi facultèp kham-khamou charia ak njâgg lislâm thi univèrsitèp Kowète gi ngua khamné falay jânggalé alkhourâne ak njângginam