Limou mbiryi: 107
25 / 3 / 1436 , 16/1/2015
Wakhtâne wî mi ngui ajou thi ay yône you joullitebi meuna jâr ba kénnal Yonnènetebi Yalla na Yalla joulli thi môme té dôlliko jâmm thi tôpp ko
13 / 10 / 1436 , 30/7/2015
hotba ba cey li Xamxam kàràŋgéla ci fitna
24 / 6 / 1436 , 14/4/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: li Yonènetebi (Yalla na Yalla joulli ci moom té dooliko jaam) taxawé ci jànggalé ak yar ak tàggate wènn xète
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Jàŋŋalé ak yar akiy,
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Fann la téxé nèkk
Wooté ci Al-Khourane ak Sunna-ay ngeünélam akiy jéxitam
14 / 5 / 1436 , 5/3/2015
Wakhtâne wi gui mi ngui ajou ci: khamlé oubé thi dîné, wâthouwâyam thi lislam, ay ponkam, ay teukk you thi ajou.
Khoutba gui mi ngui ajou ci: léral lane môy lou baax ak lou bonn, solôm, teunkk you jeum thi diglé lou baax ak téré lou bonn
Khoutba gui mi ngui ajou ci: léral taaroup lislam bi ngui khamné môy dîné jâmm, akiy téggine you rafète thi dounnd ak gnoudoul joullite. Di tônetou gni gnâwal thi Yonènete Mouhammad (Yalla na Yalla joulli thi môm té dôlliko jâm)
Waxtàn wi dafay leral na lagnouy jeuflaneté ak gnoudoul joullite
Wakhtâne mi ngui aju jurôm jikko ñiko jikkowô Yalla dina lène kéral thi kéram ga béss bô xamné bénène du am budul bosam
Wakhtâne mi ngui aju ci attèp màggal judduk Yonèntebi
28 / 4 / 1436 , 18/2/2015
Wakhtâne mi ngui jeum thi khamlé lane môy nâfèkhe akiy khâjam ak âtèm