Limou mbiryi: 107
25 / 3 / 1436 , 16/1/2015
Wakhtâwî mi ngui jeum thi: deuggeunetânou kham-kham, ngeunélam, ngeunélou borôm kham-kham, gâkk-gâkki sâkkou kham-kham ak ni mag gnou bâkh gni sâfarâ
Wakhtânewi ngui ajou thi khol bou mâp: mândargâm yi geuna râgnékou ak jékhite yimouy déf thi dôkhalînou niteki
Wakhtânewângui jeum thi: naka lagnou wara déf ba jîtal yi wara jîtou thi wôté jeumé thi Yalla
2 / 12 / 1436 , 16/9/2015
fason bi gene thi kabarou thi werou tabaski. ak amele bi thi gene.
ganelou foukkifan thi werou tabaski.diamou yalla yinou yonal thi werou tabaski.
li ay oubbele youdiam thi mbiri tabaski aylathie ak aytontou thi mbiri tabaski
14 / 10 / 1436 , 31/7/2015
hotba Ci yén la bawoo
13 / 10 / 1436 , 30/7/2015
hotba bi cey li Bouléne yaxx
Xàju nitñi ci rawanté jëm ci lu bàx
12 / 10 / 1436 , 29/7/2015
Jaaduna ci ki goorgoorlu ci wéru koor mu wéyal loolu ginnaaw kori ak goorgoorlu woor jouroombenni fane ci sawwal
11 / 10 / 1436 , 28/7/2015
Ku xool li addunabi di jàŋkonte ci ay jafé jafé ci koom, dina giss né jaaduna ñu wané yoon yunuy may suxaliku
12 / 8 / 1436 , 31/5/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Fébarup xol bu wow; ay sababam, màndargàm aki sàfaràm
11 / 8 / 1436 , 30/5/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: lénn ci jagléy Makk
24 / 6 / 1436 , 14/4/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Yitèp lislaam ci koom koom ak souxaliku ci ay kaaddu yu matalé
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Ligèyup mbootaayu lislam yi ak seeni mébate
Khoutba gui mi ngui ajou ci: lèral jafé jafé yi ci wuuté
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Ragal Yalla jàréko ci sèttanetal alkhourane ak diko doolli
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Sabap yiy sippi jeüf
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Guissiine ak dokhalinu lislaam ci koom koom ak souxaliku