Wakhtâne wi mi ngui ajout hi lèral: Kéno yi ngua khamné thi la étâp joullite di tégué ak léral ngourouk Omar Ibn Aboul Aziz ligèye gou mak goumou thi déf ak béssalam
Khouba gui mingui ajout hi akhi deunnkandô, war guimou war gnou jeufelaneté ak gnôm jeufelaté ak gnôm thi mbâkh: * Rafétal jeumé thi gnôm * Bagnelèna lor * Dékkou sèni lor