Tèkhanetal you ajou thi kham-kham

Julli àjjouma

Yalla tànn xètewii ci yénène xèteyi, mu tànnalko Mouhammad (Yalla na Yalla julli ci moom té doolliko jàmm) mu di ap yonènetaam, tànnal ko béssu àjjuma. Konenak béssu àjjouma amna nguënèl gou màgg ak palass bu kawé ci lislam, dajalénañu fii yuy léral nguënèl yooyu ak àtté yu aju ci bèss bi

Limou mbiryi: 1

Kheut wi : 1 - Dalé thi : 1
Sap xalàt lu ñu saxalla