Manàsik.. jomonoy Ajj 1434 ci gàddàygui [ 01 ] juroomélu poŋkk bi
Wakhtânekatebi :
Mélokâne bi
Ci jotàybii dàñci léral juroomélu poŋkki lislàmyi, mu bookk ci jotaay yu ñu àndak Cheikh Omar Ibn Abdoullah Al-Muqbil -Yalla nako Yalla fay yiw- ci lu jeüm ci Ajj ak lu ci aju ciy àtté akiy ndékkàné akiy génndéku, kiko ligéy di Ministérup mbiri dîné ak mayéyi ak wooté ak ginndé bi ci Arabi Sawdite ci atum 1434 ci gàddaye gi
- 1
مناسك .. موسم حج 1434هـ [ 01 ] الركن الخامس
MP4 77.2 MB 2019-05-02
Balloukây yi:
Tèkhanetal you ajou thi kham-kham:
Follow us: